كل أسفار KYG

Daniel 4

KYG · الآية 14

12 أصحاحات

KYG / Daniel / الأصحاح 4

KYG · الآية 14

N dogal a ngoog bu wattukat yi tëral, àttee ngoog bu ñu sell ñooñu digle, ngir aji dund ji xam ne Aji Kawe jee yilif nguurug nit, di ko jox ki ko soob, di ca fal ki gëna tuut.”