كل أسفار KYG

Daniel 4

KYG · الآية 15

12 أصحاحات

KYG / Daniel / الأصحاح 4

KYG · الآية 15

« L oolu laa gént, man, Nabukodonosor. Yaw Beltasar nag, wax ma piri mi. Ndax boroom xam-xam yi ci sama réew mi, kenn manu ma cee wax piri mi. Waaye yaw man nga ko, ngir xelum yàlla yu sell yaa ngi ci yaw.»