TSK

TSK · Daniel 5:13

مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.

العودة إلى المقطع
Ezra 6:16 TSK

Ci kaw loolu mbooloom Israyil ànd ak sarxalkat yaak Leween ñaak mboolem ña ñibbsee ca ngàllo ga, ñu daloo tabax ba ci biir mbégte.

Ezra 10:7 TSK

Ba mu ko defee ñu yéene ci Yerusalem ak Yuda, yégal mboolem ngàllo ga ñibbsi, ne leen ñu daje ca Yerusalem.

Yudeen ña ca bokkoon di Dañeel ak Anaña ak Mikayel ak Asaryaa.

Aryog gaaw yóbbu Dañeel ba ca Buur, wax ko ne ko: «Gis naa ci ngàllog Yudeen ñi ku la mana firil sa gént gi.»

Biiñ ba jay Baltacar, mu joxe ndigal, ñu indi ndab, yu xaalis yaak yu wurus ya baayam Nabukodonosor jële woon ca jaamookaayu Yerusalem, ngir ñu naane ca, mooki jaraafam aki soxnaam aki nekkaaleem.

¶ «Buur, Yàlla Aji Kawe ji daa joxoon sa baay Nabukodonosor nguur gi, muy ku màgg, am ndam ak daraja.

¶ Ca ñetteelu atu nguurug Baltacar, man Dañeel am naa meneen peeñu, gannaaw peeñu ma ma jëkkoona am.