كل أسفار KYG

Daniel 6

KYG · الآية 5

12 أصحاحات

KYG / Daniel / الأصحاح 6

KYG · الآية 5

B a loolu amee saytukat yaak jawriñ ya di wuta tuumaal Dañeel ci mbiri nguur gi, te gisuñu genn tooñ mbaa sikk ci moom, ndax ku amoon kóllëre la, te giseesul ci moom genn néewal mbaa sikk.