كل أسفار KYG

Daniel 9

KYG · الآية 14

12 أصحاحات

KYG / Daniel / الأصحاح 9

KYG · الآية 14

A ji Sax ji, looloo waral nga dogu ci wàcce musiba mi ci sunu kaw, ndax yaw sunu Yàlla Aji Sax ji, njekk nga jëfe lépp loo jëf, waaye noo dégluwul sa kàddu.