Proverbs 15:8
TSK
Saraxub ku soxor, Aji Sax ji bañ na ko; ñaanu kuy jubal da koy bége.
TSK
مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.
Saraxub ku soxor, Aji Sax ji bañ na ko; ñaanu kuy jubal da koy bége.
su Nóoyin ak Dañeel ak Ayóoba bokkoon nekk ca seen biir sax, ñoom ñett doŋŋ la seen bakkan di mucc ndax seenug njub. Boroom bi Aji Sax jee ko wax.
Ñooñooy foqati sam koom, sëxëtoo sa alal, màbb say miir, daane sa kër yu bakkane, boole doj yaak bant yaak pënd ba, tàbbal ca mbeex ma.
Mu ne ma: «Dañeel, yaw mi ñu naw, déggal kàddu yi ma lay wax. Jógal taxaw sa taxawaay, ndax dañu maa yebal ci yaw nii.» Naka la ma wax kàddu yooyu, ma ne ñokket, di lox.