TSK

TSK · Deuteronomy 11:13

مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.

العودة إلى المقطع

Waaye su ngeen fa sàkkoo seen Yàlla Aji Sax ji, dingeen ko daj, ndegam seen léppi xol, ak seen léppi bakkan ngeen ko sàkkoo.

Sàmmleena sàmm seen santaaney Yàlla Aji Sax ji, ak seedey yoonam, ak dogali yoonam, yi mu leen dénk.

¶ Soppleen seen Yàlla Aji Sax ji, te ngeen dénkoo ndénkaaneem, ak dogali yoonam, ak àttey yoonam, aki santaaneem, bés bu nekk.

¶ Ndegam déy sàmm ngeen ba sàmm mboolem santaane bii ma leen dénk ngir di ko jëfe, ba sopp seen Yàlla Aji Sax ji, di doxe mboolem ay yoonam te ŋoy ci moom,