TSK

TSK · Deuteronomy 2:21

مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.

العودة إلى المقطع

Ana fu nu jëm? Te sunu bokk ya demoon yoqiloo nu, ne nu waa réew maa nu ëpp, sut nu, dëkk ya réy te dàbblikoo ay tata yu àkki asamaan. Rax ci dolli, ay ponkal yu bokk ci askanu Anageen ñi lanu fa gis!»

Mooy na mu defaloon Esaween ña dëkke Seyir rekk, ba mu leen fàkkasalee Oreen ña, Esaween ña dàq leen, sanc, wuutu leen, ba bésub tey jii.

Ñooñu ay buur lañuy ñaawal, boroomi daraja di seen reetaanukaay; ñii lépp luy tata lañuy kekku, jalal ko suuf, nangu ko.