TSK

TSK · Deuteronomy 21:5

مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.

العودة إلى المقطع

¶ Ba Aaróona noppee, yékkati na mbooloo ma ay loxoom, ñaanal leen, doora wàcc. Fekk na mu joxe saraxu póotum bàkkaar ba, ak saraxu rendi-dóomal ba, ak saraxu cant ga ci biir jàmm.

¶ Jant yooyu la Aji Sax ji ber giirug Lewi, ngir ñuy gàddu gaalu kóllëreg Aji Sax ji, di taxaw fi kanam Aji Sax ji, di ko liggéeyal, di taase barke ciw turam, te mooy seen péete ba tey jii.

ngeen àgg ca sarxalkat ya, Leween ña, ak àttekat, ba mbir ma yemool jamono, te ngeen sàkku ñu biral leen àtteb mbir ma.

na ñaari nit, ña séq mbir ma taxawi fa kanam Aji Sax ji, fa kanam sarxalkat ya, ak àttekat ya ca yooyu jant.