كل أسفار KYG

Deuteronomy 21

KYG · الآية 5

34 أصحاحات

KYG / Deuteronomy / الأصحاح 21

KYG · الآية 5

S u ko defee sarxalkat yi, Leween ñi dikk, ndax ñoom la seen Yàlla Aji Sax ji taamu, ngir ñu di ko liggéeyal, di barkeele ciw turam, te ci seen kaw kàddu lees di àttee bépp jote, ak gépp loraange ci wàllu yaram.