TSK

TSK · Ecclesiastes 2:1

مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.

العودة إلى المقطع

Ayca nu wàcc, safaan seen làkk, ba dootuñu déggoo.»

Ma nga naan ca xelam: «Duma tërëf, safaan du ma dab tey ak ëllëg.»

Yaw la sam xel ne ma, ma sàkku la, te it yaw Aji Sax ji laay sàkku.

Damaa wax ci saam xel naa: Man de, maa ngii di gëna xelu, ba sut ku ma jiitu ci jalub Yerusalem. Damaa xuus ci xel mu rafet ak xam-xam,

Ma xalaataat, saam xel ne ma, dof bi noonu, man it noonu; ana lu may xeloo xelu doye? Saam xel ne ma loolu it, cóolóoli neen.

Saam xel ne ma, ku jub ak ku bon la Yàlla di boole àtte, ngir mbir mu ne ak jëf ju ne ak bésam.

Man daal damay digle bànneex, ndax nit amul lu gën fi kaw suuf di lekk ak a naan ak a bànneexu, muñe ko doñ-doñam, fan yi ko Yàlla may fi kaw suuf.

Ma xamal leen nag li ma naral sama tóokër bi. Ñàggib ñagam, mu dim parlu; màbb miiram, ñu dëggaate ko, jàll.

Ma ne, yeen ñiy jafal ab taal ñépp tey gañoo jum yuy boy, xuusleen ci sawara si ngeen jafal ak jum yi ngeen boyal. Maa leen dogalal lii: yeenay tëddaale mitit.

¶ «Jenn waay la woon ju bare alal, di sol yérey tànnéef yu rafet, di dunde lu neex bés bu set.

Titus 3:3 TSK

¶ Ndax nun itam kat, ñu ñàkk xel lanu woon te déggadi, ñu réer, tënku ci lu doon ay xemmemtéef, ak bànneexi bakkan, tey wéye def lu bon, ak ñeetaane, ñu jara bañ te bañante ci sunu biir.

James 5:1 TSK

¶ Kaayleen nag ma wax leen, yeen boroom alal yi, jooyleen te yuuxu, ndax mitit yi leen di dikkal.

Joxleen ko ci toskare aku naqar, kemu daraja jaak dund gu bakkane ga mu jagoo woon. Gannaaw moo ne cim xelam: “Maa tooge jalu lingeer, dumab jëtun, duma deele mukk,”