كل أسفار KYG

Exodus 13

KYG · الآية 17

40 أصحاحات

KYG / Exodus / الأصحاح 13

KYG · الآية 17

F irawna bàyyi na mbooloo ma, ñu dem, waaye Yàlla jaaralewu leen ca yoon, wa jëm réewu Filisti, doonte moo gënoona gàtt. Booba Yàlla dafa xam ne, su mbooloo ma sóoboo ci ay xare ci woowu yoon, dañuy yoqi, bay xalaata dëpp, dellu Misra.