Exodus 27:1
TSK
¶ «Nanga defare sarxalukaay bi bantu séng, guddaay bi di juróomi xasab, yaatuwaay bi di juróomi xasab; ab kaare la sarxalukaay biy doon, taxawaayam di ñetti xasab.
TSK
مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.
¶ «Nanga defare sarxalukaay bi bantu séng, guddaay bi di juróomi xasab, yaatuwaay bi di juróomi xasab; ab kaare la sarxalukaay biy doon, taxawaayam di ñetti xasab.
¶ Ba tey Besalel sàkk ci bantu séng sarxalukaayu rendi-dóomal bu kaare, guddaay bi di juróomi xasab, yaatuwaay bi di juróomi xasab, taxawaay bi di ñetti xasab.
¶ Aji Sax ji woo na Musaa, wax ak moom ca xaymab ndaje ma ne ko:
Du deretu sikket mbaa yëkk la duggaale, waaye deretu boppam la dugge benn yoon ba fàww ca bérab bu sell baa sell, te moom la amale njotlaay gu sax dàkk.
¶ Sunu sarxalukaayu bopp, la ñu cay jooxe, ñay liggéeye ca xaymab jaamookaay ba, sañuñu caa lekk.