TSK

TSK · Ezekiel 21:10

مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.

العودة إلى المقطع

¶ Ndaw ya gaaw dem ci ndigalal buur, ñu biral dogal ba ca Sus, péey ba. Buur a nga toog ak Aman, di naan, waa Sus nekk ci njàqare.

Géej, ma teg ci loxoom, dex, ma ne ca tegg ndijooram.

Sang baa ngi fi sa ndijoor te mooy rajaxe buur yi, bés bu meree.

Xalam yaak tabala yaak toxoro ya jolli, biiñ xelli ca xawaare ja. Seetluwuñu sax li Aji Sax ji def, xooluñu li mu jo loxoom.

Aji Sax ji nee: «Saab saamar a reye fa asamaan ba màndi deret, te mu ngii di wàccal Edom, xeet wi may faagaagal, ngir àttee leen ko.»

Takkleen fas yi, war naari góor yi, ba làng-déraale seen mbaxanay xare, nàmmaat xeej, sol yérey xare!»

wenn yoon wa jëme saamaru Babilon ca Raba, dëkkub Amoneen ñi; wa ca des jëme ko Yerusalem, dëkk ba ñu dàbbli, ca Yuda.

Niy taxas la ay noonam di laxasoo, mel ni ñu naan ba màndi, te ni boob mu wow lañuy lakke ba xoyomu.

Jant ak weer ne tekk fa seen màkkaan, janook sa leeru fitt yi soqi, ak melax gi tàkke ci sab xeej.

Ni ñuy rajaxee ndaal xandeer, noonu nga leen di sàmmeji yetu weñ,