كل أسفار KYG

Ezekiel 21

KYG · الآية 3

48 أصحاحات

KYG / Ezekiel / الأصحاح 21

KYG · الآية 3

D angay wax waa gottub diiwaanu Negew, ne leen: “Déglul kàddug Aji Sax ji. Boroom bi Aji Sax ji dafa wax ne: Maa ngii di jafal ci sa biir, daay guy xoyom sa garab yépp, gu naat ak gu wow. Dara du ko mana fey. Daay ga day jóge bëj-saalum ba bëj-gànnaar te ñépp a cay lakk,