Aji Sax ji dafa barkeel sama sang lool, ba muy boroom daraja. May na ko jur gu gàtt ak gu gudd, xaalis ak wurus ak ay surga yu góor ak yu jigéen ak ay giléem aki mbaam.
TSK
TSK · Genesis 13:2
مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.
Genesis 24:35
TSK
Genesis 26:13
TSK
Alalam di yokku, muy gëna barele, ba mujj am doole lool,
Genesis 30:43
TSK
Waa ji mujj na barele lool, am gàtt yu ne gàññ ak ay jaam yu góor ak yu jigéen ak ay giléem aki mbaam-sëf.
1 Samuel 2:7
TSK
Aji Sax jeey xañe, di maye, di detteel, di kaweel.
Job 1:10
TSK
Xanaa du yaa ko ñag, ñag këram ak mboolem alalam, ba mu daj? Liggéeyam, nga barkeel, ba ag juram law ci réew mi.
Psalms 112:1
TSK
Màggal-leen Ki Sax! Ndokklee ku ragal Aji Sax ji, di tàqamtikoo ay santaaneem.
Proverbs 10:22
TSK
Barkeb Aji Sax jeey maye alal, kër-këri taxula barele.
1 Timothy 4:8
TSK
Ndax kat tàggat aw yaram, as njariñ a ngi ci, waaye ag njullite, ci lépp lay jariñe, te moo moom digeb àddinay tey ak ëllëg.