كل أسفار KYG

Genesis 21

KYG · الآية 17

50 أصحاحات

KYG / Genesis / الأصحاح 21

KYG · الآية 17

B a mu ko defee Yàlla dégg baatu xale bu góor ba. Malaakam Yàlla ma àddoo asamaan, ne Ajara: «Ajara, lan la? Bul ragal dara, ndaxte Yàlla dégg na sa baatu doom ci diggante bii mu tollu.