TSK

TSK · Genesis 23:3

مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.

العودة إلى المقطع

Tool ba Ibraayma jëndoon ca Etteen ña, foofa lañu denc Ibraayma ak soxnaam Saarata.

Mooy xuntim bàmmeel ba ca biir tool, ba ca Magpela, te jàkkaarloo ak Mamre ca réewu Kanaan, di tool, ba Ibraayma jëndoon ca Efron, Etteen ba, ngir def ko bàmmeel.

ak Uri, Etteen ba. Ñoom ñépp tollu ci fanweeri jàmbaar ak juróom yaar.