Ba Usam faatoo, Adàdd, ma dàqoon waa Majan ca réewu Mowab, tey doomu Bedàdd, moo falu, wuutu ko. Awit a doon péeyam.
TSK
TSK · Genesis 25:2
مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.
fekk waa Majan yóbbu nañu ko Misra, jaay ko Potifaar, jawriñu Firawna mi jiite ay dagam.
¶ Yettro sarxalkatu réewum Majan ba, baayu soxnas Musaa, dafa dégg mboolem la Yàlla defal Musaa ak bànni Israyil ñoñam ak ni Aji Sax ji génnee Israyil Misra.
«Noonooleen waa Majan yii, te rey leen,
reyaale buuri Majan, Ewi ak Rekem ak Sur ak Ur ak Reba, juróomi buuri Majan ya. Balaam doomu Bewor it, ñu reye ko saamar.
Ñu jóge Majan, dem Paran, ànd ak ay waa Paran dem Misra, ca Firawna buuru Misra. Firawna jox Adàdd suuf, may ko kër akub dund.
¶ Gannaaw loolu ñetti xariti Ayóoba ñoo dégg mboolem musiba moomu ko dikkal. Ku nekk ci ñoom jóge këram: Elifas waa Teman ba, ak Bildàdd waa Suwa ba, ak Cofar waa Naama. Ñu bokk daje ngir dikk mas-sawu Ayóoba, dëfal ko.