TSK

TSK · Genesis 30:2

مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.

العودة إلى المقطع

¶ Ba Aji Sax ji gisee ne Leya fonkeesu ko, mu may ko, mu taawlu, te Rasel moom manula am doom.

Yuusufa nag ne leen: «Buleen am dara lu ngeen di ragal. Xanaa maay Yàlla?

Moo leen di sopp, barkeel leen, yokk leen, barkeel seen meññeefum njurukaay, ak seen meññeefum suuf; seen pepp ak seen biiñ, ak seenug diw, ak seen doomi jur gu gudd, ak gu gàtt, ca réew ma mu giñaloon seeni maam, ne yeen la koy jox.

Ña reggoon, bindu, di dunde, ña xiifoon, noppee liggéey. Jigéen ju njur të woon jur juróom yaar, ku jur góori góor jeex tàkk.

Mooy dëël jigéen ju tële woona jur, may ko mbégtem njureel. Màggal-leen Ki Sax!

Luke 1:42 TSK

Mu àddu ca kaw ne: «Yaa gëna barkeel ci jigéen ñi, sa doom ji nga ëmb it barkeel na!