TSK

TSK · Genesis 31:39

مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.

العودة إلى المقطع

¶ «Su nit dénkee moroomam mbaam mbaa nag mbaa gàtt mbaa mala mu mu mana doon, su jur gi deeyee mbaa mu damm mbaa ñu sàcce ko àll te amul seede,

Su fekkee ne rabu àll a fàdd mala mi, na indi li ci des, muy firnde. Su boobaa du fey dara.

Lu médd mbaa lu rab fàdd waru koo lekk, mu di ko sobeel. Maay Aji Sax ji.

Luke 2:8 TSK

¶ Booba ay sàmm a nga ca gox boobee, di fanaanee wattu seenug jur.