Genesis 17:6
TSK
Dinaa la defal njaboot gu ne xas, ay xeet sosoo ci yaw, ba ay buur soqikoo ci yaw.
TSK
مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.
Dinaa la defal njaboot gu ne xas, ay xeet sosoo ci yaw, ba ay buur soqikoo ci yaw.
¶ Aji Sax ji ne ko: «Ñaari giir nga ëmb, nara am ñaari xeet yuy xaajaloo, wenn wi mooy ëpp doole wi ci des, te mag ji mooy surgawu rakk ji.»
Maa ngi koy gis, te du tey, Maa ngi koy niir, te jubseegul; biddiiw a feqe fa Yanqóoba, yetu nguur a yékkatikoo fa Israyil, daldi toj boppi Mowab, toj kaaŋi mboolem askanu Set.
Yesurun am na buur, kera ba njiiti askan wa dajee, ba giiri Israyil bokk teew.