Genesis 31:2
TSK
Naka la Yanqóoba gis kanamu Laban, daldi xam ne melatul, na mu meloon ci moom.
TSK
مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.
Naka la Yanqóoba gis kanamu Laban, daldi xam ne melatul, na mu meloon ci moom.
¶ Sang bi dégg li ko soxnaam wax ne moom la ko jaamam def, mu mer lool,
Am sannax déy, naqari deret a koy rey, ab téxét, xéraangee koy faat.
yal na la yónnee wallam fa këram, jàpplee la fa, ca Siyoŋ.
Ma gis ne nit ak kër-këram jépp ak bépp manoorey liggéey, iñaanantee ko waral. Loolu it, cóolóoli neen ak napp um ngelaw.
Ba Yawut yi gisee mbooloo ma nag, kiñaan man leen, ñuy weddi waxi Póol, di ko saaga.