Genesis 42:27
TSK
¶ Fa ñu dal ca guddi, kenn ci ñoom bëgga xont mbaamam, ubbi saakoom rekk, ne pemm ci xaalisam.
TSK
مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.
¶ Fa ñu dal ca guddi, kenn ci ñoom bëgga xont mbaamam, ubbi saakoom rekk, ne pemm ci xaalisam.
¶ Naka la ku nekk sotti saakoom, ne jàkk ca mbuusu xaalisam. Ba ñu gisee mbuusi xaalis ya, ñoom ak seen baay, dañoo tiit.
di ko tuumaal, di teg lu ñaaw ci deram, naan: «Ndaw sii ma jël, ba ma àggee ci moom, fekkuma ko janq,»
coowal musiba mooy buur nopp ya, yàqkat bette ko biir jàmm.
Yàlla nee: «Xanaa ñiy def lu bon, xamuñu dara? Ñuy lekk sama ñoñ niw ñam, te sàkkuwuñu Yàlla.»
Ba ñu yégalee Buur Axas sëtub Daawuda, ak waa këram, ne ko waa Siri, Efrayim lañu lëngool, mbir ma yëngal na Buur Axas ak waa réew ma, ba mel ni garabi gott bu ngelaw li gësëm.