كل أسفار KYG

Isaiah 7

KYG · الآية 2

66 أصحاحات

KYG / Isaiah / الأصحاح 7

KYG · الآية 2

B a ñu yégalee Buur Axas sëtub Daawuda, ak waa këram, ne ko waa Siri, Efrayim lañu lëngool, mbir ma yëngal na Buur Axas ak waa réew ma, ba mel ni garabi gott bu ngelaw li gësëm.