TSK

TSK · Genesis 43:23

مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.

العودة إلى المقطع

Mu ne doomi baay ya: «Delloo nañu ma sama xaalis, mu ngi nii ci sama saaku.» Seen fit ne tërit, ñuy rag-ragi, ku ne xool sa moroom, naan: «Lu nu Yàlla nattoo nii?»

Yal na Yàlla Aji Man ji def waa ja yërëm leen, ba bàyyi seen doomu baay ba, moom ak Beñamin itam. Man nag, su ma naree ñàkk ay doom— aa! Naa leen ñàkk rekk.»

Ezra 4:17 TSK

¶ Ci kaw loolu Buur yónnee tont la Reyum boroom dëkk ba, mook Simsay bindkat ba, ak nàttongoom ya ca des te dëkk Samari ak la des ca Wàllaa Dex. Mu nuyu leen, ne leen:

¶ Ba ñaari taalibe ya di nettali loolu, ca la Yeesu ci boppam ne jimeet taxaw ci seen biir, ne leen: «Jàmm seen!»