Genesis 14:19
TSK
Mu ñaanal Ibraam ne ko: «Yaw Ibraam, Yàlla na la Yàlla Aji Kawe ji barkeel, moom mi sàkk asamaan ak suuf!
TSK
مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.
Mu ñaanal Ibraam ne ko: «Yaw Ibraam, Yàlla na la Yàlla Aji Kawe ji barkeel, moom mi sàkk asamaan ak suuf!
«Waxal Aaróona aki doomam ne leen ni ñuy ñaanale bànni Israyil, nii la; nañu leen wax ne leen:
Toyi yebal doomam Yoram ca Buur Daawuda, ngir mu nuyu ko, sargal ko ca la mu xareek Adadeser ba duma ko, ngir Toyi ci boppam xare woon naak Adadeser. Yoram indaaleel ko jumtukaayi xaalis ak wurus ak xànjar.
Maay àgge ay buur sa kàdduy seede, te duma rus.
Te amul benn werante ne ki féete suuf, moom la ki féete kaw di ñaanal barke.