¶ Ba Israyil dëkkee ca réew ma, am na bés Ruben dem tëdd ak Bilaa, nekkaaleb baayam; Israyil yég ko. Doomi Yanqóoba yu góor fukk lañu ak ñaar.
TSK
TSK · Genesis 49:3
مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.
Genesis 35:22
TSK
Genesis 46:8
TSK
¶ Waa kër Israyil, yi ñëw Misra te di Yanqóoba aki doomam, seeni tur a di: Ruben, taawub Yanqóoba.
Numbers 1:20
TSK
¶ Ñu lim bopp ak bopp, turi sëti Ruben taawub Israyil seen maam, ku nekk ak làngu cosaanam ak kër maamam, mboolem góor ñi xare war, te ñu am ñaar fukki at, jëm kaw.
Taaw bay doomu ka mu foñ, na ko nangul ab céram, jox ko ñaar-cay céru rakk ja, ci mboolem alalam, ndax kooka soqikoo ci digg dooleem, mooy ka yelloo céru taaw.
Deuteronomy 33:6
TSK
Yal na Ruben dund, baña raaf, yàlla buy nitam néew.
Psalms 78:51
TSK
Daa fàdd képp kuy taaw ca Misra te juddoo seen digg doole, fa xaymay sëti Xam.
Ezekiel 48:6
TSK
Suufas Ruben day digalook sos Efrayim, jàpp penku ba sowu, di benn pàcc.