كل أسفار KYG

Hebrews 13

KYG · الآية 17

13 أصحاحات

KYG / Hebrews / الأصحاح 13

KYG · الآية 17

D éggal-leen seeni njiit te nangul leen, ndax sàmm bakkani ñi ñu jiite mooy seenub liggéey, te moom lees leen di laaj ëllëg. Su ko defee ñu defe ko xol bu sedd, te bañ koo def di binni, ndax loolu du seen njariñ.