Ca lañu gëm ay waxam, woy ko.
TSK
TSK · Hosea 6:4
مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.
Loolu yépp itam taxul Yuda workat bi, doomu ndeyu Israyil, délsee léppi xolam fi man, xanaa di jinigal rekk.» Kàddug Aji Sax jee.
«Yerusalem, ana lu tax ma di la baal, te say doom wacc ma, di giñe lu dul Yàlla. Ma reggal leen, teewul ñuy njaaloo, riixle, jëm kër gànc ya!
Waaye wii xeet a dëgër bopp te déggadi. Dëddu nañu ma ba wéy.
Tey yeen, waññiku woon ngeen, ba def li ma rafetlu; ku nekk ci yeen biral goreelu mbokkam. Fasoo ngeen ko sax fi sama kanam ci biir kër gi ñu ma tudde.
«Efrayim, ana nu ma lay baye, yaw Israyil laa ne, nu ma lay tege ciy loxo? Ana nu ma lay defe ni Atma? Nu ma lay yemaleek Ceboyim? Sama xol a bëpp, sama yërmandee yëngu.
¶ Ba Yeesu jubsee ba séen dëkk ba, jooy na ndax moom.