TSK

TSK · Isaiah 17:6

مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.

العودة إلى المقطع

Bu nu Aji Sax ji Boroom gàngoor yi waccalul woon li nu deseek as néew, ni Sodom lanuy mel, Gomor lanuy neexool.

Noonu lay deme ci àddina, ci biir xeet yi, mbete benn-benni doomi oliw gu ñu gësëm, mbaa doomi reseñ yu des ca ndey ja, gannaaw bu ñu wittee ba sottal.

Aji Sax ji déy dafa wax ne: «Duma tas lépp tasar, waaye réew mi mépp ay gental.

nanga leen wax ne leen: “Boroom bi Aji Sax ji dafa wax ne: Maa ngii di jël dénku Yuusufa wi ci loxol Efrayim, mook giiri Israyil yi mu àndal, boole kook dénku Yuda, daldi def lépp wenn dénk, ñu booloo di wenn ci sama loxo.”

«Su leen ay sàcc dikkalee, mbaa sëxëtookati guddi, yeenakay yàqule! Waaye xanaa du la leen doy lañuy sàcc? Su leen wittkati reseñ dikkalee, xanaa dinañu ca wacc ay doom?

¶ Ci mbirum Israyil la Yonent Yàlla Esayi itam xaacu woon ne: «Su bànni Israyil tolloo ni feppi suufas géej sax, as ndes a ciy mucc.

Su boobaa nag, bànni Israyil gépp ay mucc, noonee ko Mbind mi indee ne: «Siyoŋ la wallukat bay jóge, mooy tenqee ngëmadi ci askanu Yanqóoba.