¶ Ba loolu amee ñu feeñuji dalub waa Filisti, ñoom ñaar ñépp. Waa Filistee nga naan: «Xool-leen! Ay Ebraa ngay génne pax ya ñu làqu woon.»
TSK
TSK · Isaiah 2:19
مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.
yal na ma noon rëbb, dab ma, dëggaate ma, sàggi saab sag, tëral ci pëndub suuf. Selaw.
Yaw Yàllay Yanqóoba, yaa gëdd, gawar ak fasam nelaw.
Ayca ca xunti ma, làqujileen biiri pax, ba sore tiitaange ji Aji Sax ji sabab, sore darajay màggaayam.
ñu dikk, bokk tagesi mbartali xunti yi, ba ci xar-xari doj yi, ak gajjoo gajj, ak déegoo déeg.
¶ «Maa ngii di woolu nappkat yu bare.» Kàddug Aji Sax jee. «Ñu napp ñii ba noppi ma woo rëbb yu bare, ñu rëbb leen ci kaw mboolem tund wu mag ak wu ndaw, ba ci bépp xar-xaru doj.
Aji Sax jaa ngii di génne ca bérabam ba, mooy wàccsi, daagoo kawtey suuf.
Aji Sax ji la mer ma diib, doole ja bare; te du ñàkka topp ku tooñ, ag tooñaangeem. Aji Sax jeey daagoo biir callweer ak ngëlén, niir yi di pëndub tànkam.
Aji Sax ji Boroom gàngoor yi kat dafa wax ne: Fileek lu néew, maa ngii di yëngalaat asamaan ak suuf, ak géej ak jéeri.
Su boobaa, “Nit ñee naan tund yu mag yi: ‘Daanuleen ci sunu kaw!’, naan tund yu ndaw yi: ‘Suul-leen nu!’ ”
Ñooñu àddina sax yeyoowu leen woon, te àll yi lañu doon wëreeloo, ak tund yeek xunti yeek kàmb yi.
Waaye bésu Boroom bi nib sàcc lay dikke. Ca la asamaan yi di dëddoo ci biir coow lu réy, lu ko sosoon seey ndax tàng, suuf ak jëf ju ci biiram xoyomu.
Bési keroog nit ñeey sàkku dee, te duñu ko daj, ñu ne siiwa dee, ndee daw leen.
¶ Ci kaw loolu néeg Yàlla bi ci asamaan ubbiku, gaalu kóllëreg Yàlla ga di feeñ ca biir màkkaanam ma, melax ya tàkk, kàddu yaak dënu ya riir, suuf sa yëngu, tawu doji yuur bu metti daldi sóob.
¶ Ci kaw loolu ma gis ngàngune mu mag mu weex, ak ku ci toog. Asamaan ak suuf daldi dawe fa kanamam, ne mes.