2 Samuel 18:25
TSK
Wattukat ba àddu ca kaw, yégal ko Buur. Buur ne: «Gannaaw kenn nit la de, xibaaru jàmm lay indi.» Waa ja di gëna jegesi,
TSK
مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.
Wattukat ba àddu ca kaw, yégal ko Buur. Buur ne: «Gannaaw kenn nit la de, xibaaru jàmm lay indi.» Waa ja di gëna jegesi,
Yerusalem, tabb naa ay jongrukat ci sa kawi tata. Buñu selaw, du guddi du bëccëg! Yeen ñiy soññ Aji Sax ji, buleen dal-lu.
«Yaw nit ki, tabb naa la wattukatub waa kër Israyil. Nangool sama gémmiñ kàddu, artool ma leen ko.
¶ Fa may jongroo laay taxaw, ne temm fa kaw tata ja, ba xam ana lu mu ma Aji Sax ji di àddu, ak lu may waxaat ci samab tawat.