Moo tax merum Aji Sax ji tàkkal ñoñam, mu xàcci loxoom, duma leen, ba tund yi jaayu, seeni néew wetar ni mbalit fi mbedd yi. Loolu yépp taxul mu meddi, loxoom baa ngi mu xàcci ba tey.
TSK
TSK · Isaiah 29:2
مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.
Tey jii noon yaa ngay taxaw fa Noob, di sànni loxo waa tundu Siyoŋ, di ko tëkkoo waa Yerusalem googu.
Aji Sax jaa ngii di tas àddina, tasaare ko, salfaañe li fi dénd bi, wasaare ñi ko dëkke:
Aji Sax jee yor saamar bu màndi deret, yafloo nebbon, ak deretu kuuy mu ndaw ak bëy, ak nebbonu dëmbéenu kuuy. Aji Sax ji kat moo am ab sarax fa Boccra, muy tër mu réy fa réewum Edom.
Ñu ne ko: «Esekiya dafa wax ne: “Bésub tey bésub njàqare la ak mbugal ak gàcce. Mooy li ñuy wax naa: Doom a ngi ci buntub juddu, te dooley wasin réer!
¶ Naka la leen Cedesyas buurub Yuda gis, mook xarekatam ya yépp, ñu daldi daw, génn dëkk ba guddi, jaare toolu buur, fëlle bunt bu nekk ca diggante ñaari tata ya, wuti jooru Araba.
Ma daldi leen xëpp samam sànj, fàkkase leen sama tàngooru xadar, këpp leen seen añu jëf ci seen kaw bopp. Kàddug Boroom bi Aji Sax jee.»
¶ «Yaw nit ki nag, Boroom bi Aji Sax ji dafa wax ne: Waxal picc yi ak mboolem njanaaw yi ak rabi àll yépp, ne leen: “Dajalooleen, jóge fu ne, dikk, dajesi ci sama sarax si ma leen di rendil, muy sarax su mag fa kaw tundi Israyil, ngeen lekk yàpp, naan deret.
¶ Ma gis nag menn malaaka mu taxaw ci jant bi. Mu àddu ca kaw, wax ak mboolem picc, yiy naaw ci digg asamaan, ne leen: «Dikkleen, dajesileen ci bernde ju mag ju Yàlla ji,