TSK

TSK · Isaiah 40:8

مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.

العودة إلى المقطع

Maay yégle muj ca ndoorte la, ak jëf ju amagul, lu jiitu bu yàgg. Maa naa sama mébét a ngi, day am, sama bépp nammeel sotti.

«Man nag, lii mooy sama kóllëreek ñoom: Sama xel mi tegu fi sa kaw, ak sama kàddu yi ma yeb ci sa gémmiñ, lenn du ci teqlikook sa gémmiñ ak sa gémmiñu askan, ak sa gémmiñu askanu askan, tey ak ëllëg.» Aji Sax jee ko wax.

Waaye kàddug Boroom bi mooy sax ba fàww.» Kàddu googu moo di xibaaru jàmm bi ñu leen àgge.