¶ Ba loolu amee Daawuda jàll ba ca wàlla, daldi taxawe fu sore ca kaw tund wa, digganteem ak dalub Sóol ne yàmblaŋ.
TSK
TSK · Isaiah 40:9
مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.
¶ At ma jëkk ca nguurug Sirus buuru Pers, Aji Sax ji moo nammoona sottal kàddu ga mu waxe ca gémmiñug Yeremi, ba tax mu xiir Sirus buuru Pers, mu siiwtaane ab dogal ci mboolem réewam, boole ci bind ko ne:
Bésub keroog dees na ne: «Sunu Yàllaa ngii nag! Moom mii lanu yaakaaroon te moo nuy wallu. Aji Sax jii lanu yaakaaroon, nan bég te bànneexoo wallam.»
Ku fitam rëcc, ne leen ko: «Dëgërlul te bul tiit. Sa Yàllaa ngii di la feyul, ba yool say noon. Moom mooy dikk, wallusi la.»
Yeen ñi xam njekk, dégluleen ma, yeen, askan wi sama yoon yebu ci seen xol. Buleen ragal nit ku leen sewal, buleen tiit seeni xaste.
«Moo tax sama ñoñ di xam maay kan; moo tax bésub keroog ñu xam ne maay wax te maa ngii!»
Xanaa du koor gu ànd ak xulook ŋaayoo, ak di joqlantey këmëx yu metti? Su ngeen bëggee seen ñaan àgg fa kaw, dungeen woor ni ngeen woore tey.
Aji Sax ji nee: «Yeen waa Yerusalem, yéegileen tundi Libaŋ, yuuxu. Àddooleen fa Basan, xaacu, te yuuxoo fa Abarim, nde seen soppe yépp a rajaxoo!»
¶ Ci kaw loolu Piyeer taxaw, mook Fukk ñaak benn, daldi àddu ca kaw, ne: «Yeen bokki Yawut yi, ak mboolem yeen ñi dëkke Yerusalem, dégluleen bu baax sama kàddu, ba xam lii lu mu doon.
Léegi nag Boroom bi, bàyyil xel seeni tëkkoo te nga may nu, nun say jaam, nuy waxe sa kàddu fit wu mat sëkk.
¶ Waaye dama ne: xanaa dañoo déggul? Ahakay! Ndax «Àddina sépp la seen baat jibal, cati suuf sépp la seen kàddu dajal.»
Buleen ragal seeni noon ci lenn. Seen fit mooy màndargaal sànkutey noon yi, te yeen it, mooy màndargaal seenug mucc gu bawoo fa Yàlla.
Te sax su ngeen doon jànkoonteeki coono ndax seenug njub, ndokklee yeen. Buleen am jenn tiitaange ci seeni xuppe, te buleen jaaxle.