TSK

TSK · Isaiah 44:12

مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.

العودة إلى المقطع

Mu nangoo ko ci seeni loxo, liggéey ko ba sàkk ci sëllu wu ñu móol. Ci kaw loolu ñu naan: «Bànni Israyiloo, seen Yàllaa ngii, moo leen génne réewum Misra!»

Xanaa du jëmmu tuur ju liggéeykat móol, ab tëgg xoobe ko wurus, takk ca caqi xaalis?

Ñii déy a yullee wurus ci mbuus, sàkk xaalis, natt diisaay ba, fey tëgg bu leen ci tëggal am tuur mu ñuy sukkal ak a sujjóotal,

Xanaa du ci Aji Sax ji Boroom gàngoor yi la lii bawoo: Sawara la askan yiy ñaqal, ag neen la waasoo yiy doñ-doñil?