Isaiah 41:14
TSK
Yaw Yanqóoba mi néew doole niw sax, yeen góori Israyil. Man, maa leen di dimbali. Kàddug Aji Sax jee, sab jotkat, Aji Sell ju Israyil.
TSK
مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.
Yaw Yanqóoba mi néew doole niw sax, yeen góori Israyil. Man, maa leen di dimbali. Kàddug Aji Sax jee, sab jotkat, Aji Sell ju Israyil.
Aji Sax jiy seen jotkat, Aji Sell ju Israyil dafa wax ne: «Yeena tax ma yebal ku songsi Babilon, ba dàjji lu fay tëjukaay, ba xaxalooy Kaldeen ñooñu diy jooyoo.
Aji Sax ji dafa wax, moom buurub Israyil, jotkatam, Aji Sax ji Boroom gàngoor yi, mu ne: «Maa jëkk, maa mujj, te yàlla amul ndare man.
Man maay seen Yàlla Aji Sax ji, kiy yëngal géej, riiral gannaxam, Aji Sax ji Boroom gàngoor yi di sama tur.
Aji Sax jee goreel askanu Yanqóoba, jot ko ci loxol ku ko ëpp doole.