TSK

TSK · Isaiah 48:6

مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.

العودة إلى المقطع

Sama Yàlla, maa soppa def sa coobare, ci sama biir xol la sa ndigali yoon nekk.»

muy lu nu dégg, xam ko, sunuy maam xamal nu ko.

Yeen bokk yi ñu bàcc ni pepp ca sama dàgga ja, la ma dégge ci Aji Sax ji Yàllay Israyil Boroom gàngoor yi, wax naa leen ko.

Mbir ya jiitoo ngoog, mat na; yu yees laa leen di yégal, balaa teew, ma yegge leen ko.»

Indileen ñii diy silmaxa te ami gët; tëx te ami nopp.

Éey niti Israyili tey, teewluleen kàddug Aji Sax ji! «Ni màndiŋ mi aaye, ndax mas naa nee aaye ci Israyil? Mbaa ma mel ni réewum lëndëm aki loraangeem? Lu waral sama ñoñ naa: “Noo moom sunu bopp, dootunu délsi fi yaw”?

¶ Maa ngi ciy dégg waaye xawma lu muy tekki. Ma ne: «Sang bi, ana nu xew-xew yooyu di mujje?»

Micah 6:9 TSK

Baatub Aji Sax ji mooy joor dëkk bi, te ndam mooy ñeel ñi wormaal sa tur. «Dégluleen seen yetu mbugal, ak ki ko yebal,

¶ Kooku leen mana dooleel nag ndax sama xibaaru jàmm, ak waareb Yeesu Almasi, mi mu feeñal mbiram tey, gannaaw ba mu nekkee mbóot mu làqu woon naka jekk,

¶ Googu texe, yonent ya jottli woon waxyub seen yiw wi leen dikkal, niir nañu ko, càmbar ko.

¶ Gannaaw loolu damaa xool, rekk yem ci bunt bu ubbiku fa asamaan. Ci biir loolu baat ba ma jëkkoona dégg muy wax ak man te mel nig liit, ne ma: «Yéegal fii, ma won la liy topp ci loolu.»

¶ Ma gis nag Gàtt bi di tàyyi genn ci juróom ñaari tayu yi. Ci biir loolu ma dégg kenn ci ñeenti bindeef yi àddoo baat buy riir ni dënu, ne: «Dikkal!»