كل أسفار KYG

Isaiah 49

KYG · الآية 7

66 أصحاحات

KYG / Isaiah / الأصحاح 49

KYG · الآية 7

A ji Sax ji jotkatub Israyil, moom ku Sellam ki, moo wax ak ki xeet yi xeeb, sib ko, te muy surgawu kilifa yi, mu ne ko: «Ay buur ay gis, jóg, ay kàngam di sukk, ngir Aji Sax ji boroom worma, ngir Aji Sell ju Israyil ji la taamu.»