كل أسفار KYG

Isaiah 49

KYG · الآية 8

66 أصحاحات

KYG / Isaiah / الأصحاح 49

KYG · الآية 8

A ji Sax ji dafa wax ne: «Bu bésub yiw taxawee, ma nangul la; bu bésub mucc jotee, ma wallu la, sàmm la, def la ngay kóllëre sama digg ak askan wi, ngir yékkatiwaat réew mi, séddalewaat ay cér, suuf sii gental tey,