كل أسفار KYG

James 3

KYG · الآية 6

5 أصحاحات

KYG / James / الأصحاح 3

KYG · الآية 6

A w làmmiñ itam sawara la; làmmiñ a bokk ci sunuy cér, te di àddinay mbon, di gàkkal jëmm jépp. Aw làmmiñ, giiru dundu nit ki lay jafale ab taal bu tàkke fa sawara.