كل أسفار KYG

Jeremiah 21

KYG · الآية 1

52 أصحاحات

KYG / Jeremiah / الأصحاح 21

KYG · الآية 1

K àddu dikkaloon na Yeremi, bàyyikoo fa Aji Sax ji. Mooy ba buur Cedesyas yebalee ca moom, Pasur doomu Malkiya, mook sarxalkat ba ñuy wax Cefaña doomu Maaseya. Mu ne ko: