«Demleen seetal ma ci Aji Sax ji, seetaaleel mbooloo meek Yuda gépp ci mbirum kàdduy téere bii feeñ. Sànjum Aji Sax ji tàkk ci sunu kaw kat réy na, ndax sunuy maam a déggul kàdduy téere bii, ngir jëfe mboolem li ñu nu ci bindal.»
TSK
TSK · Jeremiah 21:1
مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.
¶ Ci kaw loolu njiital dag ya jàpp Seraya sarxalkat bu mag ba, ak Cefaña sarxalkat ba ca topp, ak ñetti dagi bunt kër Aji Sax ja.
Ñoom ak ña ñu àndal ca liggéeyu kër Yàlla ga. Ñuy juróom ñetti téeméer ak ñaar fukk ak ñaar. Adaya ma Yerowam di baayam it bokk na ca. Pelaliya di baayu Yerowam, Amsi di baayu Pelaliya, Sàkkaryaa, di baayu Amsi, Pasur di baayu Sàkkaryaa, Malkiya di baayu Pasur.
¶ Kàddu gii dikkaloon na Yeremi, bàyyikoo fa Aji Sax ji, ca fukkeelu atu nguurug Cedesyas buurub Yuda. Mu yemook ba nguurug Nabukodonosor buuru Babilon tolloo ca fukkeelu atam ak juróom ñett.
¶ Cedesyas doomu Yosya, ja Nabukodonosor faloon buur ci réewum Yuda moo wuutu Kooña doomu Yowakim.
¶ Mu am bés Sefatiya doomu Matan ànd ak Gedalya doomu Pasur ak Yukal doomu Selemya ak Pasur doomu Malkiya. Ñu dégg Yeremiy wax, ñépp di dégg, naan:
¶ Ci kaw loolu njiital dag ya jàpp Seraya sarxalkat bu mag ba, ak Cefaña sarxalkat ba ca topp, ak ñetti dagi bunt kër Aji Sax ja.