TSK

TSK · Job 23:13

مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.

العودة إلى المقطع

Yàlla du nit, bay fen, du doom aadama bay tuub. Moom wax na lu mu deful a? Am àddu na lu mu sottalul?

Job 10:13 TSK

Ndeke yoo lii nga dencoon ci sa xol, xam naa ne lii nga naroon:

Job 12:14 TSK

Mu ngoog, keey màbb te deesul tabaxaat, di tëj nit, te deesul tijji.

Te yaw sunu Yàlla, yaa ngi asamaan, di def lu la soob.

Bare na lu xol di mébét, waaye Aji Sax jeey dogal.

Ma xam ne lu Yàlla def, loola day sax ba fàww. Deesu ci yokk, mbaa di wàññi dara; Yàllaa ko def, ngir nit di ko wormaal.

Maay yégle muj ca ndoorte la, ak jëf ju amagul, lu jiitu bu yàgg. Maa naa sama mébét a ngi, day am, sama bépp nammeel sotti.

Moo nu xamal mbóotum coobareem, mi mu nammoona sottale naka jekk ci Almasi, na mu ko neexe.