Job 7:8
TSK
Bët bi may gis tey du ma gisati, dinga ma niir, fekk nekkatuma.
TSK
مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.
Bët bi may gis tey du ma gisati, dinga ma niir, fekk nekkatuma.
réewum lëndëm, mu ne këruus, salfaañoo, ag leer sax, saf fa lëndëm!
Doom aadama it tëdd, du jógati, du yewwooti, asamaan fekke, du jógeeti ciy nelaw.
xoolal ko sama bopp, te du doon sama gan. Maaka namm lii ci sama xol!
Kii a ngi deeyaale dooleem, xel ma dal, tiitul dara,
Liggéey boo gis, liggéeyal; def ci loo man. Ndax muy jëf, di doxalin, di xam-xam, di manoore, dara amu ci njaniiw, ga nga jëm.