TSK

TSK · Jonah 1:4

مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.

العودة إلى المقطع

Aji Sax ji walbati ngelaw la, mu jóge sowu, am doole lool, daldi fél njéeréer ya, sànni ca géeju Barax ya, ba luy niru njéeréer desatul ca déndu Misra.

Waaye sa ngelaw nga wal, géej mëdd leen, ñu diigandoo ni beteex biir géej mbàmbulaan!

Ña ca des a ngi war gaal, dugg géej, di liggéeye mbeex mu ne xéew.

Mooy yékkateey niir fa cati àddina, sàkkal taw ay melax, yebbee ngelaw cay dencam,

Amos 4:13 TSK

Kii kat moo móol tund, di sàkk ngelaw, di xamal nit nammeelam. Kee di soppi lëndëm ag leer, di daagoo kawte ya. Kookoo di Aji Sax ji Boroom gàngoor yi.

¶ Ci kaw loolu ngelawal bëj-saalum wal ndànk, ñu njort ne man nañoo sottal seen pexe. Ñu wëgg diigal, daldi tafoo tefesu Keret.