TSK

TSK · Lamentations 2:3

مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.

العودة إلى المقطع

Looy téye sa loxol ndijoor? Na sa loxo jóge sa dënn, nga buube leen.

Man may biral jëfam ba fàww. Damay woy Yàllay Yanqóoba.

Ay bañam, ma rajaxe; ay noonam, ma fàdd,

ba mu yuri leen tàngooru sànjam, sotti leen tar-taru xare, mu jafal wetoo wet, te taxul ñu xam, xoyom na leen te bawuñu ci xel.

¶ Moo tax Aji Sax ji Boroom bi dafa wax ne: «Sama xadar a ngii di sottiku fi bii bérab, fi kaw nit ak mala, garab ak lu suuf meññ, lépp ne jippét, te deesu ko fey.»

maa leen di dikke seen añu jëf.” Kàddug Aji Sax jee. “Maay jafal sawara, lakk seen gott bi, mu xoyom lépp lu leen wër.”»

Fa kaw la Aji Sax ji sànnee sawara ci sama biiri yax, moo laaw ab caax ngir fakktal ma, waññi ma, jànnaxe ma, ma dëkke yoggooral.

Liitu xareey jib, ba lépp jekk ngir xare, te kenn du xareji, samam sànj a dikkal askan wépp.

Nahum 1:6 TSK

Bu sànjoo, ana kuy taxaw? Ana kuy dékku tàngooru meram? Am sànjam a naan soteet ni sawara, doj yi rajaxoo fi kanamam.

Luke 1:69 TSK

Moo nu feeñalal Musalkat bu manoorewu, fi biir kër Daawuda jaamam ba,