TSK

TSK · Leviticus 3:14

مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.

العودة إلى المقطع

Li muy génne ci saraxu cantu biir jàmm bi, muy saraxu sawara ngir xetug jàmm, ñeel Aji Sax ji, mooy nebbon bi, ak calgeen bi yépp, ñu doge ko fa sës ca fàllare ja, ak nebbon bi sàng yérey biir yi, ak lépp luy nebbon te jàpp ci yérey biir yi,

nebbon yooyu lañu teg ca kaw dënni nag wa ak kuuy ma, Aaróona lakk ko ca kaw sarxalukaay ba.

¶ Kon nag bokk yi, ma ñaax leen, te yërmandey Yàlla tax, ngir ngeen jébbal ko seen yaram wépp, def ko jooxe buy dund, sell te neex Yàlla. Loolu déy mooy njaamu, gi leen war.