TSK

TSK · Leviticus 8:3

مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.

العودة إلى المقطع

Indil Leween ñi ci kanam xaymab ndaje mi, te nga dajale mbooloom bànni Israyil mépp.

¶ Fa lañu bàyyikoo, dem Beer, (mu firi ab Teen); teen boobu, fa la Aji Sax ji noon Musaa: «Dajaleel mbooloo mi, ma may leen ndox.»

¶ mbooloo mépp a daje, di benn bopp ca mbedd ma jàkkaarlook buntu Ndox ma. Ñu wax Esra bindkat ba, ne ko mu indi téereb yoonu Musaa wi Aji Sax ji dénk Israyil.

Acts 2:1 TSK

¶ Ba bésu màggalu Pàntakot agsee, ñoom ñépp a bokk daje benn bérab.